Advertisement


[COUPLET] Penda gassoul cambeu Nga melni sindakh bouma khol  Sagnsé dama ko tameu  Kholma boubax lima sol Souma solo guéneu nga warou  Takhoul nga am touti diom Noumou geuneu séwé rek bakhna  Khotatil mako bassi souf

[REFRAIN]  Ndékété nileu nileu, nileu waay Fima guéneu toyneu toyneu, toyneu waay  Ndékété nileu nileu, nileu waay Fima guéneu toyneu toyneu, toyneu waay

[OUTRO] Nénala boul sol taille basse del solou ni kooba yi Soloul ni kou dieum Golden Five (kou dieum Golden Five) Diaroul sax poudeur ak maquillage  Dionguama bas ley def (bou oyof) soxlawoul djiteul dra (soxlawoul djiteul dra) Nileu bilaaay  Sama dionguama bi solna bas Nga solou niou yémou niou ande ma am thieurou walay nileu Nileu bilaaaay nileu  Nileu bilaaaay nileu 


Advertisement


[COUPLET 2] Na nga bayi boyal gou baari gui nga néké  Ya ngui yokk sama asthme dig ma ray rek Del def sa feer you bawwx rek diko téglé Rakh si pastille valda gui gout dey nékh Nékhoul ba nékhoul fess ngeu Bouniou done khar dé kouy ngeu sa sagnsé tay déh bakhneu  Diougeul dagou ma khol leu Tekk nga sa sous fess ragadioul  Lou bess la si ioe diéguéssil  Wane ma sa guinaw leumbeuleul  Loussi yonou slip teumbeuleul  Li la yague rêvé Ya ngui may doga meuna nékh  Nig ko défé nékhnamaaa woh woh woh !  Dionguama kay ragadioumaaaa… Hummm… kay ragadioumaaaaa… Ya takh rakadjou naaaa annh… kay ragadioumaaaa…

[OUTRO] Nénala boul sol taille basse del solou ni kooba yi Soloul ni kou dieum Golden Five (kou dieum Golden Five) Diaroul sax poudeur ak maquillage  Dionguama bas ley def (bou oyof)  Soxlawoul djiteul dra (soxlawoul djiteul dra) Nileu bilaaay  Sama dionguama bi solna bas Nga solou niou yémou niou ande ma am thieurou walay nileu Nileu bilaaaay nileu Nileu bilaaaay nileu 


Advertisement


You May Also Like

Lionel Cripps’s biography, fact, career, awards, net worth and life story

Advertisement Intro Rhodesian politician Was Farmer From Zimbabwe Gender male Birth 11…

How to wash glorious mousepad

Advertisement Are glorious mouse pads machine washable? Our mousepads are machine–washable, so…

Cassandra Due Height, Weight, Net Worth, Age, Birthday, Wikipedia, Who, Instagram, Biography

Advertisement In the event that you appreciate observing short dramatization and spine…

Amy Adams Lifestyle, Wiki, Net Worth, Income, Salary, House, Cars, Favorites, Affairs, Awards, Family, Facts & Biography

Advertisement Amy Adams is an American actress. She has appeared three times…